Ezra 7:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lépp lu Yàlla Boroom asamaan digle, nañu ko defe noonee ca kër Yàlla Boroom asamaan, ndax meram baña dal ci sama kaw nguur gii ak ci sama kaw askan.