Ezra 8:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ma boole leen, ñu daje ca wetu dex, ga jëm Aawa, dal fa ñetti fan. Ma seetlu fa baadoolo ya, seet ca biir sarxalkat ya, gisuma kenn ku bokk ci Leween ñi.