Ezra 8:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee ma yebal leen ca Ido, njiit la ca gox ba ñuy wax Kasifya, daldi leen wax kàddu ya ñuy jottli Ido ak bokkam yay liggéeykati kër Yàlla, ya dëkk Kasifya, ndax ñu yónnee nu ay surga ci sunu liggéeyu kër Yàlla gi.