Galatians 1:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndax kon nit laay wut a gëmloo, am damay fexee yey Yàlla? Mbaa damay wut a neex nit ñi? Su ma doon wut a neex nit ñi ba tey, kon duma nekkati jaamu Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag ndax nit ñi laay sàkkoo jubool, am Yàlla? Am nit ñi laay wuta neex? Su ma bëggoona wéye neex nit ñi de, duma doon jaamub Almasi.