Galatians 1:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bokk yi, maa ngi leen di xamal ne, xebaar bu baax bi ma yégle, jógewul ci nit.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, ma xamal leen ne leen xibaaru jàmm bi may yégle, bàyyikoowul ci nit.