Galatians 1:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Jëlewuma ko ci nit, te kenn jàngalu ma ko, waaye Yeesu Kirist moo ma ko won.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te it man jëlewuma ko, jàngewuma ko ci nit, xanaa ci peeñum Yeesu Almasi.