Galatians 1:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yàlla mi ma tànn lu jiitu sama juddu te woo ma ci boppam ci kaw yiwam, bi mu ko soobee, xamal na ma kan mooy Doomam, ngir ma yégal ñi dul Yawut xebaar bu baax bi ci mbirum Kirist; booba nag diisoowuma ci ak kenn.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ca sama biiru ndey la ma Yàlla séddoo, woo ma ci boppam ci kaw yiwam, te moom la soob,