bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Galatians 1:18
Galatians 1:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ba ñu ca tegee ñetti at, ma sog a dem Yerusalem, ngir xamante ak Sefas, dal fa moom lu mat ñaari ayu-bés.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw ba ñu ca tegee ñetti at laa doora dem Yerusalem, ngir xamanteji ak Sefas, toog fa moom ñaari ayi bés.