Galatians 1:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
man ak bokk yiy ànd ak man yépp, nu ngi leen di bind, yéen mboolooy ñi gëm te dëkk ci diiwaanu Galasi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
bawoo itam ci mboolem bokk yi nekk ak man, ñeel mboolooy gëmkat yu diiwaanu Galasi.