Galatians 1:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dañu déggoon ñu naan rekk ne: «Ki nu daan fitnaal bu jëkk te daan jéem a far yoonu ngëm wi, léegi mi ngi koy yégle!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Déggoon nañu rekk ñu naan: «Ki nu daan bundxatal bu jëkk, di yàq sunu yoonu ngëm wi de, léegi mooy yégle xibaaru jàmm bi koy xamle!»