Galatians 1:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
moom mi joxe bakkanam ngir dindi sunuy bàkkaar, te musal nu ci àddina su bon, si nu nekk, dëppook coobareg Yàlla sunu Baay,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mi maye bakkanam ngir njotug sunuy bàkkaar, ba musal nu ci jamonoy tey ju bon ji, ci coobarey Yàlla sunu Baay,