Galatians 1:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye su fekkee kenn ci nun ñëw, walla malaaka sax mu jóge asamaan, di yégle beneen xebaar bu mengoowul ak bi nu leen yégal, kooku Yal na alku!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye nun ci sunu bopp, mbaa malaaka mu bawoo asamaan sax, ku leen ci àgge woon beneen xibaaru jàmm bu dul bi nu leen àgge, kooku yal na alku!