Galatians 1:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Wax nanu ko, maa ngi koy waxaat: bu leen kenn yégalee beneen xebaar bu dul bi ngeen nangu, kooku Yal na alku!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Wax nanu ko ba noppi, ma waxati ko tey: képp ku leen àgge beneen xibaaru jàmm bu moy bi ngeen xasa jot, yal na alku!