Galatians 2:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bi Sefas ñëwee dëkku Ancos, yedd naa ko ci kanamu ñépp, ndaxte li mu def jaaduwul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ba Sefas dikkee Àncos, jàkk laa ko def, weddi ko, ndax moo nekkul woon ci dëgg.