Galatians 2:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ma seetee nag ne, awuñu woon ci dëgg, gi xebaar bu baax bi di jàngale, ma yedd Sefas ci kanamu ñépp ne ko: «Yaw miy Yawut, gannaaw dëddu nga aaday Yawut yi, ba dund ni ku dul Yawut, lu tax nga bëgg a sëf diiney Yawut ci ñi dul Yawut?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ba ma gisee ne doxewuñu njub gi dëggug xibaaru jàmm bi laaj, maa wax Sefas ci kanam ñépp, ne ko: «Ndegam yaw miy ab Yawut, yaa jëfewul ni ab Yawut, xanaa di jëfe ni xeeti jaambur ñi, ana lu tax ngay ërtal jaambur ñi dul ay Yawut, ngir ñu yawutal?»