Galatians 2:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye ba tey su fekkee ne nu ngi wut a jub ci kaw gëm Kirist, fekk nu ne fàŋŋ di ay bàkkaarkat, ndax nag Kirist moo sas bàkkaar? Mukk!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba tey su nu dee sàkku àtteb ku jub, ndax li nu gëm Almasi, te teewul nit ñi gis ne nu ngi bàkkaar, nun itam, ndax loolu day wund ne Almasi mooy xiirtale ci bàkkaar? Mukk kay!