Galatians 2:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye su ma delloo di sàmm ndigali yoon, yi ma bàyyi, dëgg-dëgg dinaa wone noonu ne, moykatu yoon wi laa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxam su dee tabaxub ndigalu yoon bi ma tojoon, moom laa tabaxaat, maa def sama bopp moykatub yoon.