Galatians 2:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci li jëm ci yoonu Musaa, dee naa, fekk yoon wi ci boppam moo ko waral, ngir ma man a dund, ba amal jariñ Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su dee wàllu yoonu Musaa nag, man nit ku dee laa, te yoonu Musaa moo ko waral, ngir ma mana dund dund gu ñeel Yàlla. Dees maa boole ak Almasi rey ca bant ba.