bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Galatians 2:21
Galatians 2:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Duma neenal yiwu Yàlla, ndaxte su sàmm yoon doon tax a jub fa kanam Yàlla, kon Kirist dee na cig neen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Duma neenal yiwu Yàlla, ndax kat su doon ci sàmm ndigalu yoon lees di ame àtteb ku jub, konoon Almasi moo dee cig neen.