Galatians 2:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye yaatalunu leen benn yoon, ngir dëggug xebaar bu baax bi man a sax ci yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ñooñu, nangulunu leen lu tollook simili sax, ndax bëgg leena sàmmal yeen, dëggug xibaaru jàmm bi, ba mu sax ci yeen.