Galatians 2:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ni Yàlla jëfe ci Piyeer, miy ndawam ci Yawut yi, noonu it la jëfe ci man, may ndawam ci ñi dul Yawut.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax ki liggéey ci Piyeer, ngir mu doon ndawam ci Yawut yi, moo liggéey ci man itam, ngir may ndawam ci yeneen xeet yi.