Galatians 3:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye yoon wi laajul ngëm. Mbind mi nee na: «Ku manoon a matal li yoon wi wax, kon dinga dund ba fàww.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yoon wi nag ajuwul ci ngëm, nde: «Kuy jëfe digal yooyu, yaay dund ndax ñoom.»