Galatians 3:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye Kirist jot na nu ci alkande, ji yoon wi indi; mu gàddul nu ko, ba far alku moom ci boppam, ndaxte Mbind mi nee na: «Képp ku ñu rey, wékk ko ci bant, alku nga.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Almasi moom, moo nu jot ci alkàndey yoon wi, ba mu doonee ku alku ngir nun, nde: «Alkute ñeel na képp ku ñu rey, wékk ko ci bant.»