Galatians 3:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bokk yi, maa ngi misaal wax ji ci jëfi doom Aadama. Xam ngeen ne, kóllëre gu ñu fas ba noppi, waruñu koo fecci, walla ñu ciy rax dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, ma misaale ko mbiri doom Aadama. Kayitub donale bu nit doŋŋ bind, su dee lu wóor, deesu ko neenal, mbaa di ci yokk dara.