Galatians 3:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Lenn rekk laa bëgg, ngeen wax ma ko: ndax sàmm yoon wee tax, ngeen jot Xelum Yàlla? Déedéet! Dangeen a dégg xebaar bu baax bi te gëm ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lenn rekk laa bëgg ngeen xamal ma ko: ndax ci jëfi sàmm ndigalu yoon ngeen jote Noowug Yàlla gi, am li ngeen dégg xibaaru jàmm bi ba gëm ko moo leen ko may?