Galatians 3:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen ñépp doomi Yàlla ngeen ndax li ngeen bokk ci Kirist Yeesu ci kaw ngëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen ñépp doomi Yàlla ngeen, ndax li ngeen gëm Almasi Yeesu.