Galatians 3:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag amul xaajale ci diggante Yawut ak ki dul Yawut, ci diggante jaam ak gor, ci diggante góor ak jigéen. Yéen ñépp benn ngeen ci seen bokk ci Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag amul Yawut ak ku dul Yawut, amul ab jaam ak as gor, amul góor ak jigéen. Yeen ñépp benn ngeen ci Almasi Yeesu.