Galatians 3:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu ngeen bokkee ci Kirist, kon bokk ngeen ci askanu Ibraayma, te jot ngeen xéewal, yi ko Yàlla dig.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te su ngeen bokkee ci Almasi, yeen ay askanu Ibraayma, te yeena jagoo dige ba.