Galatians 3:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bu leen Yàlla di may Xelam, di leen won jalooreem, ndax li ngeen sàmm yoon a tax, mu def ko, mbaa li ngeen dégg xebaar bu baax te gëm ko?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ki leen di may Noo gi, tey sottal ay kéemaan ci seen biir, ndax li ngeen sàmm yoon moo tax mu di ko def, am li ngeen dégg, ba gëm moo tax?