Galatians 3:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mbind mi tëral na lu jiitu ne, Yàlla dina àtte jub ñi dul Yawut ci kaw ngëm. Kon looloo tax mu yégal Ibraayma lu jiitu xebaar bu baax bi ne ko: «Xeeti àddina yépp dinañu barkeel ci yaw.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbind mi moo waajaloon lu jiitu ne ci kaw ngëm lees di joxe xeet yi dul Yawut, àtteb nit ñu jub. Moo taxoon mu yégal Ibraayma lu jiitu, bii xibaaru jàmm: «Xeeti àddina yépp ci yaw lañuy barkeele,»