Galatians 4:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bokk yi, dama leen di ñaan, ngeen mel ni man, ndaxte man itam fekksi naa leen ci seen xalaat. Tooñuleen ma.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen laay tinu, bokk yi, mel-leen ni man, ci yooyu mbir, ndax man itam ni yeen laa mel. Tooñuleen ma benn yoon.