Galatians 4:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax dëgg, gi ma leen wax, moo tax ngeen def ma ab noon?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa li ma leen di wax dëgg daa tax ma mujj di seenub noon?