Galatians 4:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nit ñooñu leen di farle, seen mébét baaxul. Dañu leen a bëgg a tàggale ak nun, ngir ngeen far ak ñoom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yitte ju réy ji ñenn ñiy taqoo ak yeen de, jubluwuñu ci lu baax. Dañu leena bëgga tàggale ak nun, ba ngeen taq leen.