Galatians 4:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Farle baax na, bu àndee ak mébét mu baax. Waaye bu sama jëmm rekk tax ngeen koy def.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yitte ju réy ju ñu am ci nit ki nag, ndegam lu baax lees ci jublu, saa su nekk lay baax, waaye du rekk saa yu ma teewee ci seen biir.