Galatians 4:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen ñi bëgg a topp yoon wi, xanaa xamuleen li yoonu Musaa wi wax?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waxleen ma, yeen ñi bëgga nekk ci kilifteefu yoonu Musaa, xanaa xamuleen li yoon wi wax?