Galatians 4:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Doomu jaam bi juddu na ni bépp doom, waaye doom, ji mu am ak jabaram, juddu na ci kaw digeb Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Doomu jaam bi moo juddu ci kaw coobarey bakkanu nit, waaye ki gor si jur, ci kaw digeb Yàlla la juddu.