Galatians 4:25 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ajara moomu mooy tundu Sinayi, wi nekk ca réewu Arabi. Te it mooy misaalu dëkku Yerusalem, bi fi nekk tey. Ndaxte moom ak ay doomam yépp ay jaam lañu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ajara moomu mooy tundu Sinayi, wa ca réewum Arabi, te moo taxawe Yerusalem gii tey, dëkk bii dib jaam mook doomam yi ko dëkke.