Galatians 4:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yerusalem, ga ca kaw, mooy gor si. Moom mooy sunu ndey.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye Yerusalem, ga fa kaw, mooy gor si, te moom mooy sunu ndey.