Galatians 4:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Mbind mi nee na:«Bégal, yaw jigéen ji dul jur,te musul a am doom.Reeyal te bànneexu,yaw mi musul a xam coonob mat,ndaxte jigéen ji ñu faalewulmoo gën a jaboot ki nekk ak jëkkëram.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat bindees na ne: «Yaw mi jaasir, ba juroo, xaacul, yaw mi xamul mititu mat, sarxolleel, nde ndaw si ñu foñ moo gëna jaboot kiy séy.»