Galatians 4:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye doom ji juddoo ni bépp doom, dafa daan sonal doom ji juddoo ci dooley Xelum Yàlla. Te loolu mooy law ba léegi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye doom ji juddoo ci coobarey bakkan, noonu mu daan bundxatale, bu jëkkoon, doom ji juddoo ci Noowug Yàlla, noonu rekk lay deme ba tey jii.