bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Galatians 4:30
Galatians 4:30 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Lu ci Mbind mi wax nag? Nee na: «Dàqal jaam bi ak doomam, ndaxte doomu jaam bi warul a bokk cér ak doomu gor si ci ndono.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te lu ci Mbind mi wax? Mu ne: «Dàqal jaam bu jigéen bii ak doomam, ndax doomu jaam bi du donnandoo ak doomu gor si.»