Galatians 4:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ngir jot ñi yoon wi nootoon, ndax Yàlla jàpp nu ni ay doomam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir jot ñi ci curgag yoon wi, ba nu jagoo cérub doom.