Galatians 5:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Man nag bokk yi, bu ma doon faaydaal xaraf ci sama waare, kon duñu ma fitnaale nii; te it li may yégle ci deewu Kirist ca bant ba dootul naqari kenn.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man nag bokk yi, su ma dee xiirtale ci xaraf, ana lees may bundxataleeti? Konoon kay sama waareb deewu Almasi ca bant ba dootu doon ag tooñ ci kenn.