Galatians 5:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñi farataal xaraf te di leen dëpp, nañu gën a sore ci seen réer: bu yaboo sax ñu dagg seen ngóora, ba dara du ci des!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi leen di lëjal ak waxi xaraf, nañu xuuf boog seen ngóorag bopp benn yoon!