Galatians 5:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li ma leen di wax mooy lii: dundleen ci Xelum Yàlla, kon dungeen topp seen nafsu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li ma leen di wax moo di: doxeleen Noowug Yàlla, su boobaa dungeen topp seen xemmemtéefi bakkan.