Galatians 5:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bu ngeen toppee Xelum Yàlla, nekkatuleen ci kilifteefu yoon wi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye su leen Noo gi jiitee, su boobaa nekkatuleen ci kilifteefu yoon wi.