Galatians 5:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
lewetaay ak maandute. Yoon wi terewul yu ni mel.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
akug teey, ak moom sa bakkan. Yu mel noonu, wenn yoon bañu ko.