bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Galatians 5:3
Galatians 5:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te maa ngi dellu di waxaat ne, képp kuy farataal xaraf, fàww nga sàmm lépp lu yoon wi santaane.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma artooti képp ku dem ba ñu xarfal ko, ne ko mboolem yoon wi la wara jëfe.