Galatians 6:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñiy gistal ci seen yaram, ñooñoo bëgg ngeen xaraf, ngir ragal a daj fitna ci yégle deewu Kirist ca bant ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi leen di gétën ci xaraf mooy ñi ngistal tax ñu bëgg nit ñi gërëme leen seen melow yaram, te jubluwuñu ci lu moy ragal ku leen bundxatal ndax deewug Almasi gi ñuy xamle ne mooy taxa mucc.