Galatians 6:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kureel gi faaydaal xaraf, ñoom ci seen bopp sax, duñu topp yoon wi. Dañoo bëgg a ngeen xaraf, ba ñu man a bàkku ci seen yaram, yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi xaraf ñoom ci seen bopp sax toppuñu yoon wi. Teewul ñu bëgg ngeen xaraf, ngir mana damoo seen màndargam yaram, yeen ñi ñu xarafloo.